SpotifyToMP3
Ngalandou Diouf

Ngalandou Diouf

Goethe-Institut... · 12:58 · 9 609 прослушиваний

Из альбома Xam sa démb, xam sa tey

Описание

Ngir xam lu leer ci seen mboorum réew ak bu Afrig, ndaw ñi dañoo war a miin jàmbaar yi tabax  Afrig. Ndégat yii di Podcast, xam sa démb, xam sa tey »,  looloo tax ñu tànn yenn ci jaar-jaar ak xew-xew i mboorum Senegaal, ngir may ndaw ñi ñu jàngee ci seen démb, baa man seen tay, te waajal seen ëllëg.

More By Goethe-Institut...

Вам также может понравиться